Commentaire de ngotty mbaye KAK (18/12/2007 22:58) :
EUSKEY AKKASSA BAY FALL KHOL SEDDA TI NA CI BI LIGUEEY.LII YALLA NA SOUNOU
BOROOM AK SERIGNE TOUBA AK CHEIKH IBRA FALL YOOK KHEWEULYI AK KATTAN YI BA
MOU DIEUM KANAM TéH YOKOU BOU BAKHA BAKH WAAY.CHEIKH SALIHOU MBACKE YALLA
NAFI YAAG TEH WEUR.
|